Bou Bakh Bi (Explicit)-Canabasse/Cheeks/Cool Black Lion/Zou Kana
语种 : 纯音乐
时长 : 03:55
DOLBY 杜比全景声 下载
臻品母带 下载
臻品全景声 下载
臻品音质
HIRES Hi-Res 下载
FLAC 无损flac 百度云网盘下载
APE 无损ape 格式下载
320MP3 极高mp3 歌曲下载
128MP3 标准mp3 百度网盘下载
192OGG 较高ogg 下载
192AAC 较高aac 下载
96AAC 标准aac 百度云下载
Loading...
TXT Bou Bakh Bi (Explicit)-Canabasse/Cheeks/Cool Black Lion/Zou Kana 文本歌词
Hook (Canabasse)
Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete
Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene
Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene
Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene
Ki bou baakh bi la
Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi boubakh bi leu
Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu
Verse (Cheeks)
Jackpot nigga lolou la nieup di seet
Bima dioudo bobou ba legui yaw rek ladone seet
Mancha limuy dound doyna seuk dama sikk dama sikk
Mais guemeul ni yaw rek ladone seet
Baby girl boubax bi ngueu no more talking
Beug nala def sama wife sama trophée
Cheeks dafa thiofé
Yea dafa trop frais
Hamna ni mane kecé tamit ngadone seet
Damla nop ba doff et puis matay
Dioureul ma ay filston you barkeel
Dimanche nga tegalma ay boolou mafé
Boubaxa baax bila chè pas ce qu’elle m’a fait
Yalla boula thiate dougou
Mane ak yaw ba biir paradise
Ma lay retain lo ni Dudu
Mane ak ioe lepp chill lepp nice
Hook (Canabasse)
Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete
Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene
Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene
Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene
Ki bou baakh bi la
Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi boubakh bi leu
Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu
Verse ( Coolblack ).
Sou ma sagnone modulé ak mome
Mbeuguelam dima goungué may dokh
Soufi nekoul douma neka lep ne teka hawma noumay mana doundé sans moom
Verse ( Zou Kana)
I gotta marry her she so got to me
Took my chance to propose and took a knee
Players gotta stop balling it don’t bother me
All She wants is a little love but gets all of me
Bou bakh bi la she not popular
When headed to the bottom mou top ma
Sofo sobo takh ma sop la.
Amouma ko doul yow kot kon kout man
You know opposites are beauty like a panda
heaven sent she scares me like thunder
My love to your heart it surrendered
Your a perfect girl like an angel descendent
Hook (Canabasse)
Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete
Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene
Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene
Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene
Ki bou baakh bi la
Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi boubakh bi leu
Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu
Verse ( Canabass )
Sama lady sama lady
Si mom lay dess legui legui
Bouko beuguè rek ma deff diff
Matal lepp tay toom mou seuy si
Yokhla bayi lepp louma diapone
Garé melni troc bouniou sabot
Yeah jotna ma dem waxak papam
Ndax guissna fi facon bou né Wanté ki ni bou baax bi leu
Rafetna diek na tarou, mbeuguel bim ma jokh dafma yeem
Teyé tankam budul pr farata halebi dou guene
Deguel na ay wadiouram yeah mom ak nienene gni dougnou bene
Kharoul si mane dara loudoul love yea baby té tegouma lene
Ki bou baax bi lamotax fi la garé
Boubaax bi la
Sagn na doug galem
Boubaax bi la
Dianok papam neko sa doom la beug té ding mako may
Hook (Canabasse)
Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete
Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene
Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene
Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene
Ki bou baakh bi la
Damay doug galem wakhak papam ndaxtè bi boubakh bi leu
Tegui tank garè wathie andak moom ndax tè boubaax bileu
Yeah rafete na, diek na, taarou na douma ni dedete
Yeah teyé na tankam boudoul pour farata dou guene
Deguel neu ay wadiouram mook nienene gni dougnou bene
Xaroul si mane dara loudoul love te bagnalouma lene
Ki bou baakh bi la
Bou Bakh Bi (Explicit)-Canabasse/Cheeks/Cool Black Lion/Zou Kana 推荐歌曲
4 The Buzz, Vol. 4 (Explicit)专辑下载
(2020-08-07)