Li Nek Si Mane (Explicit)-Canabasse
DOLBY 杜比全景声 下载
臻品母带 下载
臻品全景声 下载
臻品音质
HIRES Hi-Res 下载
FLAC 无损flac 百度云网盘下载
APE 无损ape 格式下载
320MP3 极高mp3 歌曲下载
128MP3 标准mp3 百度网盘下载
192OGG 较高ogg 下载
192AAC 较高aac 下载
96AAC 标准aac 百度云下载
Loading...
TXT Li Nek Si Mane (Explicit)-Canabasse 文本歌词
Hook
Ak lo meunti degg
Lougn leu meunti waax
bo geummé guiss deugg
Nelene niou teudj sene ngaam
Kham nga li nek si mane
Bouleine bayi gnou yak sa mind
Niom dagn niouy guiss di shine
Mais sougnou sagnone am goor gou melni mane walabok
Verse
Hey girl neel tekk melni deggo
Boul bayi sene wax eup dolé sama dieuf no
Nenala lady nanga bayi dima tek shok
Té nga bagna deglou waxou none yi fatal say nop
Dey soop doula nop
Dafay door a gauche manul took
Dafay dieul sa xol mais dey foo
Ki diokhouleu sa thieer dokhal dokh bi
Wassup ma'
Girl bomay meré nanga ma meré si loumeu def mais boulma indil ay probleme ndax ay wax yo degg
Le fait que ngay tok diokhléne attention niouy yakh sama derr ngay deglou dalene di may dolé lady
Bridge (Canabasse)
Many girls dem love me
Mais dou mane ak niom
Yaw la beug baby girl
Yenene girl yangui diem louniou meun
Wanté ya nek sama xol
Hook
Ak lo meunti degg
Lougn leu meunti waax
bo geummé guiss deugg
Nelene niou teudj sene ngaam
Kham nga li nek si mane
Bouleine bayi gnou yak sa mind
Niom dagn niouy guiss di shine
Mais sougnou sagnone am goor gou melni mane walabok
Verse (Viviane)
Yeah dama sone si thiow bi oh love
Meme wax bi lagnuy deuké samay nopp
Té yemoul si say wax ndax guissna ni changé nga
Dieulngueu say distance t’es plus comme avant
Souma sanione bagn deglou gayi
But i won’t let you waste my time
Kou defoul lougn ko waxal lépe lagn lay waxal
Baby bulma diapé dof jen ai marre
Ak louma manti degg
Lougnou ma manti wax
Bou sama xel dalone baby
Douma laci massa sonal
Canabasse
Boul deglou babe gni dagnuy hate
Bougn sagnone lignouy dound tey finga hey
Boul tok ba sa fierté dila diay boul dioum ba reuy
Bayi ma concentré wou sama liguey
Mo guene ngamay sonal ak detail
Bridge (Viviane)
Many boys dem love me
Mais dou mane ak niom
Yaw la beug baby boy
Mais ndeysane dinga matt sa baram withiakh ndakh damay go
Hook
Ak lo meunti degg
Lougn leu meunti waax
bo geummé guiss deugg
Nelene niou teudj sene ngaam
Kham nga li nek si mane
Bouleine bayi gnou yak sa mind
Niom dagn niouy guiss di shine
Mais sougnou sagnone am goor gou melni mane walabok
Verse
Lou nice fok wax dji baré
Sa copines yi di tek en vrai degn ma bardé
MVP nia ko sékal shorty
Nekheu beug yako tay yeah sa man day ballin
Wanté yay sama girlfriend allright
Lima soxla lepp ci djiguene
Yang koy matal
Mais niak wolou bingua dioukté
doulou baax
Ndaxté dafay indi distance tchi nioune niar
Té wax deug baby tiow bé doyna
Bou yagué dey yak
Ma wax la deug baby tiow be doyna bou yagué dafay yak
Hook
Ak lo meunti degg
Lougn leu meunti waax
bo geummé guiss deugg
Nelene niou teudj sene ngaam
Kham nga li nek si mane
Bouleine bayi gnou yak sa mind
Niom dagn niouy guiss di shine
Mais sougnou sagnone am goor gou melni mane walabok
Bridge (Canabasse)
Many girls dem love me
Mais dou mane ak niom
Yaw la beug baby girl
Yenene girl yangui diem louniou meun
Wanté ya nek sama xol
4 The Buzz, Vol. 4 (Explicit)专辑下载
(2020-08-07)