Sama Gàmmu-Youssou N'Dour
DOLBY 杜比全景声 下载
臻品母带 下载
臻品全景声 下载
臻品音质
HIRES Hi-Res 下载
FLAC 无损flac 百度云网盘下载
APE 无损ape 格式下载
320MP3 极高mp3 歌曲下载
128MP3 标准mp3 百度网盘下载
192OGG 较高ogg 下载
192AAC 较高aac 下载
96AAC 标准aac 百度云下载
Loading...
TXT Sama Gàmmu-Youssou N'Dour 文本歌词
Sama Gàmmu - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé eh
Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé eh
Yor khalis meunoul tè ma môm la
Keur gou rich meunoul tè ma môm la
Yaw na nga def yaw sama gàmmu
Dég na danga yor khalis
Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal man suma xarit nga
E e e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e e e gàmmu daal suma askan
Sama Gàmmu-Youssou N'Dour 推荐歌曲
Rokku Mi Rokka (Give and Take)专辑下载
(2007-10-30)