Létt ma-Youssou N'Dour

歌手 : Youssou N'Dour
语种 : 葡萄牙语
时长 : 04:40

DOLBY 杜比全景声 下载

臻品母带 下载

臻品全景声 下载

臻品音质

HIRES Hi-Res 下载

FLAC 无损flac 百度云网盘下载

APE 无损ape 格式下载

320MP3 极高mp3 歌曲下载

128MP3 标准mp3 百度网盘下载

192OGG 较高ogg 下载

192AAC 较高aac 下载

96AAC 标准aac 百度云下载

Loading...

TXT Létt ma-Youssou N'Dour 文本歌词

Létt ma - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
Du nii du nii bëgg naa nga létt ma
Walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàlle ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw tóppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defloo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma

Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw

Boo ma waxee fi nga bëgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bul dem waxal bul wax defal bul def
Man daal sonn naa sonn naa sonn naa
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa ko tay bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë
Bëgg ak bañ la

Rokku Mi Rokka (Give and Take)

Rokku Mi Rokka (Give and Take)专辑下载

(2007-10-30)