Baay Faal-Youssou N'Dour
DOLBY 杜比全景声 下载
臻品母带 下载
臻品全景声 下载
臻品音质
HIRES Hi-Res 下载
FLAC 无损flac 百度云网盘下载
APE 无损ape 格式下载
320MP3 极高mp3 歌曲下载
128MP3 标准mp3 百度网盘下载
192OGG 较高ogg 下载
192AAC 较高aac 下载
96AAC 标准aac 百度云下载
Loading...
TXT Baay Faal-Youssou N'Dour 文本歌词
Baay Faal
baay faal gueu da djook thia fadjar
nga sène ko mouy soli sagar
boppam gueu sekkeu ki kawar
yoré keulleum gueu di zikar
té falé woul khiif ak mér
boo démé sakh khekh na badar
ki toureum wi dotoul fay
kou wéddi li ladj ko wa ndar
baay faal djakhal na wa ndar
baay faal djakhal na wa ndar
baay faal gueu da djook thia fadjar
mani bour Yalla da djook thia fadjar
nga sène ko mouy soli sagar
yoré keulleum gueu di zikar
ki toureum wi dotoul fay
kou wéddi li ladj ko wa ndar
baay faal djakhal na wa ndar
baay faal djommeul na wa ndar
doundeum gueu nekh na
zikar sa neekh na lol
baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor
zikar sa motakh mou djégué Yalla
baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome
thia tool yeu...
thia tèène yeu...
thia wagne weu...
magal yeu...
baay faal liguey la khame
baay faal ndigueul la khame
baay faal dou khekh dou khoulo
beuggue neu nite, fonk na nite khekhoulol
mome la fayé ko lo mou ligueyal sougnou borom
beuggue na la baay faal
nangou nite
kimo djégué sougnou borom
dey liguey di djokhé motakh baay faal djégué naa sougnou borooom...
dey liguey di diokhé
dey liguey di diokhé motakh baay faal
toggam ga nekhna lol motakh bay faal
dey magal motakh baay faal
dey zikar motakh baay faal
Baay Faal-Youssou N'Dour 推荐歌曲
Rokku Mi Rokka (Give and Take)专辑下载
(2007-10-30)