Dabbaax-Youssou N'Dour
DOLBY 杜比全景声 下载
臻品母带 下载
臻品全景声 下载
臻品音质
HIRES Hi-Res 下载
FLAC 无损flac 百度云网盘下载
APE 无损ape 格式下载
320MP3 极高mp3 歌曲下载
128MP3 标准mp3 百度网盘下载
192OGG 较高ogg 下载
192AAC 较高aac 下载
96AAC 标准aac 百度云下载
Loading...
TXT Dabbaax-Youssou N'Dour 文本歌词
Dabbaax - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
Di wadjial péssé ba
Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
Moulaay dabaaaaax
Bougnou faté bess boboulé uhh bougnou soré bess boboulé
Bougnou faté bess boboulé
Lofa gnaane yalla may lako
Modaane wakhal nitt gnep mo daane wakhal nasraane yi
Anh mo daane kadou askane wi
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
Dafa daane wakh naane nagnou yeureum djiguéen
Sa borom bi begu na yonentam bi begu na yako liguéyal sa borom
Moulaye dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul
Kérok bang gnou djito assamaane si da leudeum
Bessa ngui kéne dotou ko fatéééti moulaay dabbaxx
Bougnou faté bess boboulé bougnou soré bess boboulé
Bougnou faté bess boboulé
Lofa gnaane yalla may lako
Anh modaane wakhal nitt gnep anh mo daane wakhal nasraane yi
Anh mo daane wakhal askane wi
Dafa daane wakh naane na gnep ligueye
Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
Dafa daane wakh naane na gnep liguèye
Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni
Daawaoul sétane lou gnaaw
Poussom la yorone fou khotékou mou gnaw
Rewmirewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx
Daawaoul sétane lou gnaaw
Poussom la yorone fou khotékou mou gnaw
Rewmirewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx
Bakrék dara maam aram lô coumba thiam
Magn penda ak pathé penda ah
Modaane wakhal nitt gnep mo daane wakhal nasraane yi
Mo daane kadou askane wi
Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi
Dafa daane wakh naane nagnep liguéye
Dafa daane wakh naane nagn yeureum djiguéene gni
Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
Dabbaax-Youssou N'Dour 推荐歌曲
Rokku Mi Rokka (Give and Take)专辑下载
(2007-10-30)