Tukki-Youssou N'Dour

歌手 : Youssou N'Dour
语种 : 纯音乐
时长 : 04:09

DOLBY 杜比全景声 下载

臻品母带 下载

臻品全景声 下载

臻品音质

HIRES Hi-Res 下载

FLAC 无损flac 百度云网盘下载

APE 无损ape 格式下载

320MP3 极高mp3 歌曲下载

128MP3 标准mp3 百度网盘下载

192OGG 较高ogg 下载

192AAC 较高aac 下载

96AAC 标准aac 百度云下载

Loading...

TXT Tukki-Youssou N'Dour 文本歌词

Tukki - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
Yoon wi nga jël baaxul ku la koy digël da lay nax
Yoon wii ci des moo gën loo taseel dàldi kuy mën
Yoon wii nga jël
Booy dox ba ca biir géstul xool fi nga weesu balaa ngay
Booy tukki yaw
Booy tukki yaw
Booy tukki yaw
Na nga bàyyl ba mën
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
Foofo mën nga fa gis lu yókk sa xameel
Booy tukki yaw
Nita ngi toog di janoog yaw
Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan
Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam
Yaw sama waay kaay ma xamal la
Léég léég nga toog fi nga toog tukki
Bu neex dem ba kaw asamaan
Ànd ag weer wiy naaw
Li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu gën fee neex
Booy tukki yaw
Booy tukki yaw yeesal sa xameel
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
Deel tukki yaw
Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw
Te booy seet sax taxu koo gaaw
Te léég léég mu dem ba kaaw
Tukkee ka neex waaw
Lucum cééli ma ngay naaw
Te léég léég mu naaw ba kaw asamaan indi fiy xabaar
Ku dul tukki doo xam fu dëkk neexe
Booy tukki yaw
Booy tukki yaw
Na nga bàyyi
Booy tukki yaw
Na nga bàyyi ba mën
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
Booy tukki yaw
Booy tukki yaw
Booy tukki yaw
Na nga bàyyi ba mën
Ñaanu barke ah ñaanu barke
Nita ngi toog di janoog yaw
Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan
Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam
Yaw sama waay kaay ma xamal la
Léég léég nga toog fi nga toog tukki
Tukki bu neex dem ba kaw asamaan
Làng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom
Mu gën fee neex
Booy tukki yaw
Na nga bayyi ba mën
Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
Deel tukki yaw
Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw
Te booy seet sax taxu koo gaaw
Te léég léég mu dem ba kaaw
Tukkee ka neex waaw
Lucum cééli ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw
Ëndaaleel ñu xabaar
Tukkee ka neex waaw
Rokku Mi Rokka (Give and Take)

Rokku Mi Rokka (Give and Take)专辑下载

(2007-10-30)